« Sama djeukeur ben chambre la am ak niari djabar..Kou ayé moy.. », terribles confidences d’une dame désorientée

Une dame désorientée a récemment fait des confidences troublantes sur le compte Instagram « Tutodakar », provoquant une vive réaction de la part des internautes.

En effet, les confessions de cette dame ont été tellement choquantes que de nombreux internautes ont exprimé leur profonde préoccupation pour sa santé mentale. Car oui une situation comme telle est inédite dans notre société.

Voici son texte :

« Salut tuto en ano s’il te plaît. Man je suis une fille sénégalaise peulh d’origine guinéenne. Fii Dakar particulièrement médina la dioudo, mangué fii, yarofi cependant mes parents viennent de la Guinée Conakry. Mon père m’a toujours dit depuis l’enfance que sama ben domou woloré lala dégne-thial mais pour Man daf dafmay togne. En juillet 202, si la amé 16 ans, mounima dafmay mayé pour sameu kadou bimou waxanték ak mbokam yii. Beugouma woneu, cependant Man niémé wouma sama papa mom loumou wakh daf koy def. Mou forcéma,arreté sama ndiangue mayéma par force. Ken ladiouma sama avis. Niou mayma kou ameu 47 ans. Sama awo rek maguénama 19 ans. Bima démé seuyi, j’ai trouvé qu’il était en location et que Man ak sama awo ak domam yii nio bok chambre bi. La chambre est séparé par des rideaux en 3partie, une partie pour les bagages, une partie pour les enfants et une autre partie pour nous les adultes ( mon awo, moi même et mon mari. En ce qui nous concerne, kou ayé Yay teud si kaw ak sa dieukeur kou ayé woul Yay fanane si souf. Souniouy seuy si kaw lale bii dagualén di dégueu, do lénam do def dara. Bilahi lii koumako waxone doumako gueum. Waxnako sama papa mounima n’a sant yallah vu que amna foumay fanane. Nous vivons comme des animaux domestiques. Bilahi amna louma méti té amouma fouma koy dioyé teksi nguissouma kouma dimbali. Le pire moy situation bii derangéwoul sama awo bii ni sama dieukeur. Beugueuna fé diougué mais dama amoul fouma dém ».

Laisser un commentaire